✂️💾📋 Wolof | Emojis in Wolof
- 😀kanam guy gaññi
- 😃kanam ak gémmiñ gu ubbeeku di muuñ
- 😄kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak muuñ bët
- 😁kanam guy gaññi ak bët yuy muuñ
- 😆kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak buñ tëj bët
- 😅kanam guy muuñ ak ubbeeku gémmiñ ak ñàqu tiitaange
- 🤣ree ba xalangu ci suuf
- 😂kanam gu am rangooñu bànneex
- 🙂kanam gu muuñ tuuti
- 🙃kanam gu dëppu
- 😉piis benn bët
- 😊kanamu mbegte ak bët yuy muuñ
- 😇kanam guy muuñ ak serkal ci kawam
- 😍muuñ, kanam, xol, bët
- 🤩dóor-biddeew
- 😘kanam guy ëf fóon
- 😗kanam guy fóon
- ☺️kanam guy muuñ
- 😚kanam guy fóon ak bët yu gëmm
- 😙kanam guy fóon ak bëti muuñ
- 😋kanam, bànneexu, ñeex, ñam
- 😛kanam bu ànd ak làmmiñ wuñ tàllal
- 😜kanam ak tàllal làmmiñ ak bët buy piis
- 🤪kanamu dof
- 😝kanam ak tàllal làmmiñ ak buñ tëj bët
- 🤑kanamu gémmiñu xaalis
- 🤗kanamu kottante
- 🤭kanam ak loxo bu dar gémmiñ
- 🤫kanamu shuut noppil
- 🤔kanamu guy xalaat
- 🤐kanam ak gémiñ guñ fermitiir
- 🤨kanam ak buñ yëkkati yéen
- 😐kanam gu ni tekk
- 😑kanam gu melul nenn
- 😶kanam gu amul gémmiñ
- 😏kanam gu bëgg-waccu
- 😒kanam gu ñàkk xorom
- 🙄kanam guy regeju
- 😬kanam guy def yëfi golo
- 🤥kanamu fenkat
- 😌kanam féex
- 😔kanamu kuy xalaat
- 😪kanam guy nelaw
- 🤤kanam guy yuut
- 😴kanam gu nelaw
- 😷kanam guñ bàndaas
- 🤒kanam gu ànd ak termomeetar
- 🤕kanam guñ laxas ak bàndaas
- 🤢kanamu guy teey xel
- 🤮kanam guy waccu
- 🤧kanamu tissooli
- 😵kanam gu diis
- 🤯bopp buy toj
- 🤠kanam gu sol mbaxane kaboy
- 😎muuñ, kanam, nuwaarfime
- 🤓kanamu bëñu lëk
- 🧐kanam ak lunet-bennbët
- 😕kanam gu jaaxasoo
- 😟kanam gu jaaxle
- 🙁kanam gu ànd ak yéen yu xawa lemu
- ☹️aj-yéen kanam
- 😮kanam ak gémiñ gu ubbeeku
- 😯kanam guñ juutal
- 😲kanam gu waaru
- 😳kanam gu am tomb yu xonk
- 😦kanam gu ànd ak yéen yu lemu ak gémmiñ gu ubbiku
- 😧kanam gu xawa jaaxle
- 😨kanam guy tiitaleete
- 😰kanam ak ubbeeku gémmiñ ak ñàqu tiitaange
- 😥kanamu mbetteel te féex
- 😢kanam guy jooy
- 😭kanam guy jooy ca kaw
- 😱kanam guy jooy te tiit
- 😖kanam gu jaawale
- 😣kanam guy ñafe
- 😞kanam gu am mbetteel
- 😓kanam ak ñaq wu sedd
- 😩kanamu coono
- 😫kanam gu sonn
- 😤kanam gu ànd ak saxaaru bakkan
- 😡kanam guy puucatu
- 😠kanam gu mer
- 🤬kanam ak màndarga ci gémmiñ
- 😈kanam gu am ay béjjen
- 👿kanam gu mer am ay béjjen
- 💀yaxu-bopp
- ☠️kraan and yax yu kruwaase
- 💩julu puup
- 🤡kanamu kluun
- 👹oogar
- 👺kus-kondoroŋ
- 👻fàntom
- 👽aliyeen
- 👾jiney aliyeen
- 🤖kanamu roboo
- 😺kanamu muus muy muuñ ak gémmiñ gu ubbeeku
- 😸kanamu muus muy xiiru ak bët yuy muuñ
- 😹kanamu muus bu ànd ak rangooñi mbégte
- 😻kanamu muus buy muuñ ak bëti xol
- 😼kanamu muus ak muuñ gu weng
- 😽kanamu muus bu tëj bët di fóon
- 🙀kanamu muus mu jommi
- 😿kanam muus muy jooy
- 😾kanamu muus mu mer
- 🙈golo budul gis lu bon
- 🙉golo budul dégg lu bon
- 🙊golo budul wax lu bon
- 💋marku fóon
- 💌bataaxalu mbëggeel
- 💘xol ak fett
- 💝xol buñ laxas ribaŋ
- 💖xol bu yànj
- 💗xol buy màgg
- 💓xol buy tëf-tëfi
- 💞xol buñ wëndeelu
- 💕ñaari xol
- 💟taaralukaayu xol
- ❣️xol esklamaasiyoŋ bu fës
- 💔xol bu tasaaroo
- ❤️xonk xol
- 🧡xol bu oraas
- 💛xol bu mboq
- 💚xol bu wert
- 💙xol bu baxa
- 💜xol bu yolet
- 🖤xol bu ñuul
- 💯tombi teeméer
- 💢màndarga ku mer
- 💥mbëkkante
- 💫miir
- 💦toqu ñaq
- 💨dem sa yoon
- 🕳️pax
- 💣bomb
- 💬rëddu bind kàddu
- 👁️🗨️bët ci rëddu-bind-wax
- 🗨️bulu bind waxu càmmoñ
- 🗯️ndijoor mer bul
- 💭rëddu bind xalaat
- 💤zzz
- 👋tàllal loxo
- 🤚ginaawu loxo bu jog
- 🖐️buñ yëkkati loxo ak baaraam yuñ tàllal
- ✋loxo bu jog
- 🖖loxo xaajale ñeenti baaraam
- 👌laxo waaw-kay
- ✌️loxo ndam
- 🤞laxasante ñaari baaraam
- 🤟liyaar mbëggeel
- 🤘loxo def màndarga béjjen
- 🤙loxo nanga ma woo
- 👈ginaaw loxo buy joxoñ càmmoñ
- 👉ginaaw loxo buy joxoñ ndijoor
- 👆ginaaw loxo buy joxoñ ci kaw
- 🖕baaraamu digg
- 👇ginaaw loxo buy joxoñ ci suuf
- ☝️baaraamu joxoñ buy joxoñ ci kaw
- 👍baaraamu waaw
- 👎baaraamu déet
- ✊kurfañ bu jog
- 👊kurfañ buy ñëw
- 🤛kurfañu càmmoñ
- 🤜kurfañu ndijoor
- 👏loxo yuy tàccu
- 🙌yëkkati ay loxo
- 👐loxo yu ubbeeku
- 🤲tallal loxo ñaan
- 🤝joxante loxo
- 🙏lem ay loxo
- ✍️loxo buy bind
- 💅jakkal wew
- 🤳selfie
- 💪wane doole
- 👂nopp
- 👃bakkan
- 🧠yuur
- 👀gët
- 👁️bët
- 👅làmmiñ
- 👄gémmiñ
- 👶liir
- 🧒xale
- 👦xale bu góor
- 👧xale bu jigéen
- 🧑mag
- 👱nit ku karaw yu weex
- 👨góor
- 🧔nit am sikkim
- 👩jigéen
- 👱♀️karaw gu am kawar gu mboq jigéen
- 👱♂️góor gu am karaw gu mboq
- 🧓mag mu gën a màgget
- 👴màgget gu góor
- 👵màgget gu jigéen
- 🙍nit ku yéen yi lemu
- 🙍♂️góor aj-yéen
- 🙍♀️jigéen aj-yéen
- 🙎nit kuy puucatu
- 🙎♂️góor puucatu
- 🙎♀️jigéen puucatu
- 🙅nit ku naan déedet
- 🙅♂️góor buy liyaar Déet
- 🙅♀️jigéen juy liyaar Déet
- 🙆nit ku naan waaw-kay
- 🙆♂️góor buy liyaar waaw-kay
- 🙆♀️jigéen juy liyaar waaw-kay
- 💁nit kuy joxee wet
- 💁♂️góor loxo jàppale
- 💁♀️jigéen loxo jàppale
- 🙋nit kuy yëkkati loxo
- 🙋♂️góor yëkkati loxo
- 🙋♀️jigéen yëkkati loxo
- 🙇nit kuy sëgg-nuyoo
- 🙇♂️góor sujjóotal
- 🙇♀️jigéen sujjóotal
- 🤦nit ku taf loxo ci kanamam
- 🤦♂️góor gu taf loxo ci kanamam
- 🤦♀️ju taf loxo ci kanamam
- 🤷nit ku aj mbaggam
- 🤷♂️góor aj mbagg
- 🤷♀️jigéen aj mbagg
- 👨⚕️fajkat bu góor
- 👩⚕️fajkat bu jigéen
- 👨🎓ndongo bu góor
- 👩🎓ndongo lu jigéen
- 👨🏫jàngaletkat bu góor
- 👩🏫jàngalekat bu jigéen
- 👨⚖️àttekat góor
- 👩⚖️àttekat bu jigéen
- 👨🌾baykat bu góor
- 👩🌾baykat bu jigéen
- 👨🍳toggkat góor
- 👩🍳toggkat bu jigéen
- 👨🔧mekaniyee bu góor
- 👩🔧jigéen mekanik
- 👨🏭liggéeykatu isin bu góor
- 👩🏭jigéen juy liggéeykat ci isin
- 👨💼kuy liggéey ci biro
- 👩💼jigéen biro liggéeykat
- 👨🔬xaralakat bu góor
- 👩🔬jigéen wu-xarala
- 👨💻góor teknolosist
- 👩💻jigéen teknolosist
- 👨🎤góor waykat
- 👩🎤jigéen waykat
- 👨🎨artist bu góor
- 👩🎨artist bu jigéen
- 👨✈️góor piloot
- 👩✈️piloot bu jigéen
- 👨🚀astronot bu góor
- 👩🚀astronot bu jigéen
- 👨🚒sapër bu góor
- 👩🚒pompiyee bu jigéen
- 👮polisiyee
- 👮♂️góor poliis liggéeykat bu góor
- 👮♀️polisiyee bu jigéen
- 🕵️detektif
- 🕵️♂️góor detektif
- 🕵️♀️jigéen detektif
- 💂gardiñe
- 💂♂️góor guy wattu
- 💂♀️jigéen juy wattu
- 👷tabaxkat
- 👷♂️góor tabax liggéeykat
- 👷♀️jigéen tabax liggéeykat
- 🤴doomu-buur bu góor
- 👸doomu buur bu jigéen
- 👳nit ku kaalawu
- 👳♂️góor gu kaalawu
- 👳♀️jigéen ju kaalawu
- 👲góor gu sol mbaxane sinuwaa
- 🧕jigéen ju musóoru
- 🤵góor gu sol kostim
- 👰séet bu móoru
- 🤰jigéen ju ëmb
- 🤱nàppalee ween
- 👼liiru malaaka
- 🎅Pere nowel
- 🤶meer nowel
- 🧙mage
- 🧙♂️mage bu góor
- 🧙♀️mage bu jigéen
- 🧚fee
- 🧚♂️fee bu góor
- 🧚♀️fee bu jigéen
- 🧛wàmpiir
- 🧛♂️wàmpiir bu góor
- 🧛♀️wàmpiir bu jigéen
- 🧜sireen bu nit
- 🧜♂️sireen bu góor
- 🧜♀️sireen
- 🧝elfe
- 🧝♂️elfe bu góor
- 🧝♀️elfe bu jigéen
- 🧞jinne
- 🧞♂️jinne ju góor
- 🧞♀️jinne ju jigéen
- 🧟zombi
- 🧟♂️zombi bu góor
- 🧟♀️zombi bu jigéen
- 💆nit ku ñuy dàmp
- 💆♂️góor bu ñuy dàmp
- 💆♀️jigéen bu ñuy dàmp
- 💇nit kuy watu
- 💇♂️góor bu ñuy wat
- 💇♀️jigéen bu ñuy wat
- 🚶nit kuy dox
- 🚶♂️góor dox
- 🚶♀️jigéen dox
- 🏃nit kuy daw
- 🏃♂️góor daw
- 🏃♀️jigéen daw
- 💃jigéen juy fecc
- 🕺góor guy fecc
- 🕴️góor ci bisnes kostim lewitasiyoŋ
- 👯nit ñuy fecc, ak noppi lëk
- 👯♂️góorak noppi lëks suwaare
- 👯♀️jigéen ak noppi lëks suwaare
- 🧖nit ci néegu wapër
- 🧖♂️góor ci néegu wapër
- 🧖♀️jigéen ci néegu wapër
- 🧗nit kuy yéeg
- 🧗♂️góor guy yéeg
- 🧗♀️jigéen juy yéeg
- 🤺nit kuy fente
- 🏇kursu fas
- ⛷️skikat
- 🏂kuy pateŋ ci nees
- 🏌️nit kuy golf
- 🏌️♂️góor guy golf
- 🏌️♀️jigéen juy golf
- 🏄nit kuy sërfe
- 🏄♂️góor guy sërfe
- 🏄♀️jigéen juy sërfe
- 🚣nit joow gaal
- 🚣♂️góor guy joow gaal
- 🚣♀️jigéen juy joow gaal
- 🏊nit kuy féey
- 🏊♂️góor guy féey
- 🏊♀️jigéen juy féey
- ⛹️nit kuy bondeel bal
- ⛹️♂️góor guy bondeel bal
- ⛹️♀️jigéen juy bondeel bal
- 🏋️nit kuy yëkkati lu diis
- 🏋️♂️góor guy yëkkati lu diis
- 🏋️♀️jigéen juy yëkkati lu diis
- 🚴nit kuy dawal welo
- 🚴♂️góor guy dawal welo
- 🚴♀️jigéen juy dawal welo
- 🚵nit kuy dawal vtt
- 🚵♂️góor guy dawal welo ci montaañ
- 🚵♀️jigéen juy dawal welo ci montaañ
- 🤸nit ñuy ànd bërëŋu
- 🤸♂️góor guy pëno-sareet
- 🤸♀️jigéen juy pëno-sareet
- 🤼nit ñuy bëre
- 🤼♂️góor guy bëre
- 🤼♀️jigéen juy bëre
- 🤽nit kuy polo ci ndox
- 🤽♂️góor guy polo ci ndox
- 🤽♀️jigéen juy polo ci ndox
- 🤾nit kuy aanbóol
- 🤾♂️góor guy handball
- 🤾♀️jigéen juy handball
- 🤹nit kuy sànni-kapte
- 🤹♂️góor guy sànni-kapte
- 🤹♀️jigéen juy sànni-kapte
- 🧘nit ku farankulaayu
- 🧘♂️góor gu farankulaayu
- 🧘♀️jigéen ju farankulaayu
- 🛀nit kuy sangu
- 🛌nit ci kaw lal
- 👭ñaari jigéen yu jàppante loxo
- 👫góor ak jigéen jàppante loxo
- 👬ñaari góor yu jàppante loxo
- 💏fóon
- 💑xol ak ñaar ñu bëggante
- 👪bokk famiy
- 🗣️wax bopp
- 👤yaram takkandeer
- 👥ay yaram takkandeer
- 👣fu tànk teguwoon
- 🐵kanamu golo
- 🐒golo
- 🦍dàngin
- 🐶boppu xaj
- 🐕xaj
- 🐩kaj bu ndaw, sëq kawar
- 🐺kanamu xaju-tundu
- 🦊kanamu rënaar
- 🐱kanamu muus
- 🐈muus
- 🦁kanamu gaynde
- 🐯kanamu segg
- 🐅segg
- 🐆lewopaar
- 🐴kanamu fas
- 🐎fas
- 🦄kanam gu sax béjjen
- 🦓zebre
- 🦌serf
- 🐮kanamu nag
- 🐂yékk
- 🐃nagu ndox
- 🐄nag
- 🐷kanamu mbaam-xuux
- 🐖mbaam-xuux
- 🐗mbaam-àll
- 🐽bakkanu mbaam-xuux
- 🐏yàppu kuy
- 🐑xar bu jigéen
- 🐐bëy
- 🐪giléem
- 🐫gileemu ñaari boos
- 🦒giraaf
- 🐘ñay
- 🦏rinoseros
- 🐭kanmu jinax
- 🐁jinax
- 🐀kaña
- 🐹kanamu jinax
- 🐰kanamu lëk
- 🐇lëk
- 🐿️cipmànk
- 🦔suñeel
- 🦇njugub
- 🐻kanam urs
- 🐨koala
- 🐼kanamu panda
- 🐾fu tànku rab teguwoon
- 🦃koppin
- 🐔ginaar
- 🐓séq
- 🐣cuuj bu génn ci nen
- 🐤cuuj
- 🐥kanam jàkkarloo ak lexu xale
- 🐦picc
- 🐧penguweŋ
- 🕊️kolomb
- 🦅céeli
- 🦆kanaara
- 🦉looy
- 🐸kanamu mbott
- 🐊jasit
- 🐢mbonaat
- 🦎sindax
- 🐍jaan
- 🐲kanamu dragoŋ
- 🐉dragoŋ
- 🦕soropod
- 🦖T-Rex
- 🐳baleen bu puucatu
- 🐋baleen
- 🐬dófeŋ
- 🐟jën
- 🐠jënu tàngoor
- 🐡bun fokkin
- 🦈rekeŋ
- 🐙oktopis
- 🐚xoru espiraal
- 🐌eskargoo
- 🦋lëppaalëp
- 🐛gunóor
- 🐜sànqaleñ
- 🐝yamb
- 🐞gunóor am tupp yu weex
- 🦗kriket
- 🕷️jargoñ
- 🕸️lëndu jargoñ
- 🦂jiit
- 💐takkufulër
- 🌸fulóor yu am melo sëriis
- 💮fulóor bu weex
- 🏵️roset
- 🌹róos
- 🥀fulóor bu waw
- 🌺ibiskus
- 🌻fulóoru jant
- 🌼fulóor
- 🌷tulip
- 🌱semis
- 🌲garab gu am xob yuy dund
- 🌳garab gu am xob yuy dee
- 🌴garabu-tiir
- 🌵gargamboose
- 🌾sayu ceeb
- 🌿ñax
- ☘️tereefal
- 🍀treefalu ñeenti xob
- 🍁kobu kanadaa
- 🍂xob yu daanu
- 🍃xob wu gelaw yëngal
- 🍇reeseŋ
- 🍈mëloŋ
- 🍉xaal
- 🍊màndarin
- 🍋lingom
- 🍌banana
- 🍍ananas
- 🍎pom bu xonk
- 🍏pom bu wert
- 🍐puwaar
- 🍑pes
- 🍒sëriis
- 🍓frees
- 🥝kiwi
- 🍅tamaate
- 🥥ñamu coco
- 🥑awokaa
- 🍆basante
- 🥔pombiteer
- 🥕karot
- 🌽noppi mboq
- 🌶️kaani xeeñ
- 🥒komkombar
- 🥦brokoli
- 🍄sampiñoŋ
- 🥜gerte
- 🌰sateñ
- 🍞mburu
- 🥐Kurwaasaŋ
- 🥖miisu mburu
- 🥨bretzel
- 🥞krep
- 🧀cëru fromaas
- 🍖yàpp ci yax
- 🍗tànku ginaar
- 🥩dogu yàpp
- 🥓bekon
- 🍔àmburgë
- 🍟pombiteer buñ saaf
- 🍕pizza
- 🌭ot-dog
- 🥪sandwich
- 🌮tako
- 🌯burito
- 🥙mburu-farsi
- 🥚nen
- 🍳togg
- 🥘boolu togg bu xóotul
- 🍲potu ñam
- 🥣bool ak kuddu
- 🥗salaad bu wert
- 🍿pop korn
- 🥫lekk ci kanet
- 🍱boyetu bento
- 🍘gato ceeb
- 🍙balu ceeb
- 🍚ceeb buñ togg
- 🍛ceebu kari
- 🍜toggee ci wapër
- 🍝espageti
- 🍠pataas buñ roti
- 🍢oden
- 🍣sushi
- 🍤sippax buñ saaf
- 🍥buteeli jën
- 🍡dango
- 🥟buleet
- 🥠mbiskitu musuwaar
- 🥡boyetu yóbbaale
- 🦀junqoob
- 🦐krëwet
- 🦑kalamaar
- 🍦kreem galaas bu am suukar
- 🍧galaas guñ dëbb
- 🍨kreem galaase
- 🍩beñe
- 🍪mbiskit
- 🎂ngato màggal bisu-judd
- 🍰gàttal-yoon
- 🥧tàrt
- 🍫laatu-sokolaa
- 🍬tàngal
- 🍭tàngal bant
- 🍮kreem
- 🍯potu lem
- 🍼biberoŋ
- 🥛kaasu meew
- ☕naan gu tank
- 🍵kaasu attaayu bu amul jàppukaay
- 🍶buteel bu yaatu gémmiñ
- 🍾buteel bu saañ biy naaw
- 🍷kaasu sàngara
- 🍸kaasu koktel
- 🍹naan tàngoor
- 🍺kaasu biyeer
- 🍻dóorante kaasu biyeer
- 🥂dóorante kaas
- 🥃kaasu ndox
- 🥤kaas ak paay
- 🥢baget
- 🍽️furset and paaka ak asiyet
- 🍴furset ak paaka
- 🥄kuddu
- 🔪paaka waañ
- 🏺àmfoor
- 🌍glob buy wane ërop ak afrik
- 🌎glob buy wane amerik
- 🌏glob buy wane asi ak óstraali
- 🌐glob buy wane merijeŋ yi
- 🗺️kàrtu àdduna
- 🗾kàrtu sapoŋ
- 🏔️nees bu muur montaañ
- ⛰️montaañ
- 🌋géeju xal
- 🗻tundu fuji
- 🏕️kampiŋ
- 🏖️tefes ak parasol
- 🏜️desert
- 🏝️desert dun
- 🏞️park national
- 🏟️estad
- 🏛️tabaxu cosaan
- 🏗️tabax ab tabax
- 🏘️kër yi
- 🏚️kër gu gent
- 🏠kër
- 🏡kër ak sardeŋ
- 🏢taaxu liggéey
- 🏣biro post ci sapoŋ
- 🏤biro post
- 🏥opitaal
- 🏦bànk
- 🏨otel
- 🏩otelu mbëggeel
- 🏪njaay mu yomb
- 🏫daara
- 🏬rëy magasin
- 🏭Isinu-liggéey
- 🏯taaxu sapoŋ
- 🏰taaxu buur
- 💒céet
- 🗼tuuru ci tokyo
- 🗽estati liberte
- ⛪jàngu
- 🕌Jàkka
- 🕍sinaagog
- ⛩️armeeli Shinto
- 🕋Kaaba
- ⛲ndax muy sànni
- ⛺tant
- 🌁lay
- 🌃guddi ak ay biddéew
- 🏙️cityscape
- 🌄jant buy fenk ci tund
- 🌅jant buy fenk
- 🌆timis ci réewu taax
- 🌇jant bu so ci réewu taax
- 🌉pom ci guddi
- ♨️cooroon bu tàng
- 🎠fasu kurusel
- 🎡pëno bu kawe lool
- 🎢tundu risi
- 💈tablo watkat
- 🎪barabu sirk
- 🚂ndaamaar
- 🚃otoraay
- 🚄otoraay bu gaaw lool
- 🚅otoraay bu gaaw lool ak kanam gu sew
- 🚆saxaar
- 🚇metro
- 🚈otoraay bu moome fépp
- 🚉gaar
- 🚊tram
- 🚝monoraay
- 🚞raayu tund
- 🚋oto tramweey
- 🚌otokaar
- 🚍kaar buy ñëw
- 🚎trolleybus
- 🚐minikaar
- 🚑àmbilaas
- 🚒oto pompiyee
- 🚓oto poliis
- 🚔oto poliis buy ñëw
- 🚕taxi
- 🚖taxi buy ñëw
- 🚗oto
- 🚘oto buy ñëw
- 🚙oto njëkkante
- 🚚kamiyoŋu bagaas
- 🚛kamiyoŋu bu gudd lool
- 🚜traktër
- 🏎️kursu oto
- 🏍️moto
- 🛵eskutër
- 🚲welo
- 🛴welo benn tànk
- 🚏are-kaar
- 🛣️otoruut
- 🛤️wagoŋ raay
- 🛢️bidoŋu diw
- ⛽pompu esaas
- 🚨làmpu oto poliis
- 🚥làmpi estop yu tëdd
- 🚦làmpi estop yu taxaw
- 🛑màndarga dakkal
- 🚧tabax
- ⚓serukaayu gaal
- ⛵gaalu ngelaw
- 🛶kaal gu ndaw
- 🚤gaalu motër
- 🛳️ki mu yab bato
- ⛴️bak
- 🛥️gaalu-motër
- 🚢gaal gu mag
- ✈️roppalaan
- 🛩️roppalaan bu ndaw
- 🛫roppalaan buy dem
- 🛬roppalaan buy ñëw
- 💺toogu
- 🚁elikopteer
- 🚟raay ci kaw
- 🚠teleferik
- 🚡tramweey ci kaw
- 🛰️satelit
- 🚀fuse-jawwu
- 🛸sukup buy naaw
- 🛎️joolooli bu ñuy bës
- ⌛saabliyee
- ⏳saabliyee buy sotti suuf
- ⌚seetaan
- ⏰waxtukaayu yégle
- ⏱️kronoo
- ⏲️montar jël-waxtu
- 🕰️montaru wékk
- 🕛12:00:00
- 🕧12:30:00
- 🕐01:00:00
- 🕜01:30:00
- 🕑02:00:00
- 🕝02:30:00
- 🕒03:00:00
- 🕞03:30:00
- 🕓04:00:00
- 🕟04:30:00
- 🕔05:00:00
- 🕠05:30:00
- 🕕06:00:00
- 🕡06:30:00
- 🕖07:00:00
- 🕢07:30:00
- 🕗08:00:00
- 🕣08:30:00
- 🕘09:00:00
- 🕤09:30:00
- 🕙10:00:00
- 🕥10:30:00
- 🕚11:00:00
- 🕦11:30:00
- 🌑weer wu bees
- 🌒xaaju weer buy wàññiku
- 🌓xaaju weer wu njëkk
- 🌔weer wu sew buy wàññiku
- 🌕weer wu fees
- 🌖weer wu sew buy yokk
- 🌗xaaju weer wu mujj
- 🌘xaaju weer buy yokk
- 🌙weer wu sew di màgg
- 🌚kanamu weer wu bees
- 🌛weeru xaaj bu njëkk
- 🌜weeru ñeenteelu xaaj
- 🌡️termomeetar
- ☀️jant
- 🌝weer ñumm bu am kanam
- 🌞jant bu am kanam
- ⭐biddeew, weexaay bu yam
- 🌟biddeew tàkk
- 🌠biddeew buy daw
- 🌌asamaan aki biddéew
- ☁️niir
- ⛅jant ci ginaaw niir
- ⛈️niir ak melax ak taw
- 🌤️jant ci ginaaw niir wu ndaw
- 🌥️jant ci ginaaw niir wu rëy
- 🌦️jant ci ginaaw taw niir
- 🌧️niir ak taw
- 🌨️niir ak nees
- 🌩️niir ak melax
- 🌪️Tawu-ngelaw
- 🌫️ab lay
- 🌬️kanamu ngelaw
- 🌀ngelaw luy wëndeelu
- 🌈xon
- 🌂parasol bu tëju
- ☂️parasol
- ☔parasol bu am toqu taw
- ⛱️parasol ci kaw suuf
- ⚡kuuraŋ bu am doole
- ❄️donju nees
- ☃️bonomu-nees
- ⛄nitu nees bu amul nees
- ☄️komet
- 🔥xal
- 💧toqu ndox
- 🌊duusu ndox
- 🎃naajo alowiin
- 🎄garabu nowel
- 🎆petaaru artifis
- 🎇potu sondeel
- ✨ferñeent
- 🎈baloŋ
- 🎉bombu taabal
- 🎊mànqu konfeti
- 🎋garabu tanabata
- 🎍taaralukaayu sapeŋ
- 🎎pupe sapone
- 🎏bàndarolu waas
- 🎐gittaxu keseŋ-keseŋ
- 🎑séentu weer
- 🎀ribaŋ
- 🎁kado buñ ëmb
- 🎗️ribaŋu fàttalikaay
- 🎟️biye dugg
- 🎫biye
- 🎖️medaayu militeer
- 🏆kup
- 🏅medaayu tàggat-yaram
- 🥇medaayu plaas 1
- 🥈medaayu plaas 2
- 🥉medaayu plaas 3
- ⚽balu futbal
- ⚾besbóol
- 🏀basket
- 🏐wolebal
- 🏈futbalu amerik
- 🏉futbalu rigbi
- 🎾tenis
- 🎳buliŋ
- 🏏powum kriket
- 🏑hockey ci ñax
- 🏒hockey ci galaas
- 🏓ping pong
- 🏸badminton
- 🥊gaŋu boksër
- 🥋kimono defkatu aar
- 🥅caaxu kaaŋ
- ⛳raaya ci pax
- ⛸️patee ci galaas
- 🎣bantu nappukaay
- 🎽mbubu tàggat-yaram
- 🎿skis
- 🛷trenóo
- 🥌xeeru kërliŋ
- 🎯dóor bu jub
- 🎱biyaar 8 bal
- 🔮bulu kristaal
- 🎮powum wideo
- 🕹️joystick
- 🎰masinu xaalis
- 🎲deewu lido
- ♠️pikk yépp
- ♥️kër yépp
- ♦️karo yépp
- ♣️treefal yépp
- 🃏jokeer
- 🀄dragon mahjong bu xonk
- 🎴kàrti fulër
- 🎭yëngu ci aar
- 🖼️nataal buñ kaadare
- 🎨boolu pentiirukaay
- 👓linet
- 🕶️nuwaarfime
- 👔karawaat
- 👕tiset
- 👖jiin
- 🧣kol
- 🧤gant
- 🧥màntóo
- 🧦kawas
- 👗robbu
- 👘kimono
- 👙bikini
- 👚yéere jigéen
- 👛nafa
- 👜saagu loxo
- 👝poset
- 🛍️saagu ndugg
- 🎒saagu ndongo daara
- 👞dàllu góor
- 👟dàllu daw
- 👠koket yu gudd
- 👡caraxu jigéen
- 👢botu jigééen
- 👑kuron
- 👒mbaxane jigeen
- 🎩mbaxane joniwalkër
- 🎓mbaxane lijaasa
- 🧢kap
- ⛑️mbaxane-kaaraange wallukat
- 📿kurus
- 💄xonkal tuñ
- 💍jaaro
- 💎xeer wu seer
- 🔇oparlër buñ noppiloo
- 🔈oparlër buy wax ndànk
- 🔉oparlër bu xumbul noonu
- 🔊oparlër bu xumbul lool
- 📢baafal
- 📣megafon
- 📯mbiibu bataaxal
- 🔔joolooli
- 🔕joolooli ak buum
- 🎼kle misik
- 🎵arafu misik
- 🎶arafi misik
- 🎙️mikrofonu studio
- 🎚️xàjjalekaayu dayo
- 🎛️bitoŋu yokk/wàññi
- 🎤mikrofon
- 🎧kasku misik
- 📻rajo
- 🎷saksofon
- 🎸gitaar
- 🎹klawiyee misik
- 🎺trompet
- 🎻violon
- 🥁ndënd
- 📱telefon portaabal
- 📲telefon portaabal ak fett
- ☎️telefon
- 📞kombine telefon
- 📟bipër
- 📠faks
- 🔋batiri
- 🔌priisu kuuraŋ
- 💻ordi portaabal
- 🖥️ordi-biro ordinatër
- 🖨️emprimaant
- ⌨️klaawiyee
- 🖱️suuri ordinatër
- 🖲️trackball
- 💽disku ordi
- 💾disket
- 💿disk optik
- 📀dvd
- 🎥kameraa filmu
- 🎞️kaadaru klise
- 📽️prosektër filmu
- 🎬klapet
- 📺tele
- 📷nataalukaay
- 📸nataalukaay bu ànd ak flaas
- 📹nataalukaay wideo
- 📼kasetu wideo
- 🔍lup bu féete càmmoñ
- 🔎lup bu féete ndijoor
- 🕯️sondeel
- 💡àmpul
- 🔦làmp-tors
- 🏮làntern bu xonk
- 📔kàrne bu ànd ak kubéer gu rafet
- 📕téere bu tëju
- 📖téere bu ubbiku
- 📗téere bu wert
- 📘téere bu baxa
- 📙téere bu oraas
- 📚téere yi
- 📓kàrne
- 📒téere bu rëy
- 📃këyit wuñ lem muus wi
- 📜tawal
- 📄kanam gu téen
- 📰këyitu xibaar
- 🗞️këyitu xibaar buñ lem
- 📑boole ci yi ma gënal
- 🔖xàmme-téere
- 🏷️màndarga
- 💰saagu xaalis
- 💴biye yen
- 💵biye dolaar
- 💶biye euro
- 💷piye pound
- 💸xaalis bu am ay laaf
- 💳kàrtu keredi
- 💹grafiku yen buy yéeg
- ✉️mbaru-bataaxal
- 📧bataaxalu net
- 📨mbaru-bataaxal biy ñëw
- 📩mbaru-bataaxal, am fett
- 📤boyetu-yónne bataaxal
- 📥boyetu-jot bataaxal
- 📦paket
- 📫boyetu-bataaxal buñ tëj, am raaya buñ yëkkati
- 📪boyetu-bataaxal buñ tëj, am raaya buñ wàcce
- 📬boyetu-bataaxal buñ ubbi, am raaya buñ yëkkati
- 📭boyetu-bataaxal buñ ubbi, am raaya buñ wàcce
- 📮boyetu-leetar
- 🗳️boyetu-wote ak kàrtu-wote
- ✏️kreyoŋ
- ✒️dik fëtar
- 🖋️estilo
- 🖊️bik
- 🖌️borosu-pentiir
- 🖍️kreyoŋ kulër
- 📝karmat
- 💼waliis wu ndaw
- 📁ëmbu taxañ
- 📂ubbi ëmbu taxañ
- 🗂️xàjjalekaayu limu kàrt
- 📅arminaat
- 📆arminaatu xotti-kayit
- 🗒️bloknot bu am weñ
- 🗓️arminaat bu am weñ
- 📇limu këyit
- 📈grafik buy yéeg
- 📉tablo buy wàcci
- 📊jagraamu bànd
- 📋klasëru kepp-kayit
- 📌pasarel
- 📍bitoŋ bu roŋ
- 📎trombon
- 🖇️trombonu këyit yuñ lëkkale
- 📏reegal bu jub
- 📐reegal bu am jëmmu triyàngal
- ✂️siso
- 🗃️boyetu kàrtu taxañ
- 🗄️tirwaaru taxañ
- 🗑️pañe mbalit
- 🔒tëj nañu ko
- 🔓tijji nañu ko
- 🔏tëj nañu ko ak bik
- 🔐tëj nañu ko ak caabi
- 🔑caabi
- 🗝️caabi ju yàgg
- 🔨marto
- ⛏️pik
- ⚒️marto ak pik
- 🛠️marto ak kle
- 🗡️paaka
- ⚔️bu am kruwaa eppee
- 🔫pistole
- 🏹ark bu ànd ak fett
- 🛡️kiiraay
- 🔧kle
- 🔩buloŋ ak wiisam
- ⚙️piñoŋ
- 🗜️tënaaj
- ⚖️balaasu peesekaay
- 🔗lëkkalekaay
- ⛓️ceen
- ⚗️alembik
- 🔬mikroskop
- 🔭teleskop
- 📡àntenu satelit
- 💉pikiir
- 💊garab
- 🚪buntu
- 🛏️lal
- 🛋️kanape and làmp
- 🚽wanag
- 🚿duus
- 🛁beñuwaar
- 🛒puus-puusu bagaas
- 🚬sigaret
- ⚰️keesu-néew
- ⚱️urnu dëj
- 🗿moai
- 🏧màndarga ATM
- 🚮màndarga mbalit ci pot
- 🚰ndox mu sell
- ♿màndarga puus-puus
- 🚹néegu góor ñi
- 🚺néegu jigéen ñi
- 🚻néegu noppalukaay
- 🚼màndarga liir
- 🚾tuurukaayu ndox
- 🛂xool sa paaspoor
- 🛃duwaan
- 🛄laajte say bagaas
- 🛅bagaas yiñ bàyyi
- ⚠️moytul
- 🚸xale yi dañu fiy jaar
- ⛔bu fi kenn dugg
- 🚫dañu koy tere
- 🚳bu fi kenn dawal welo
- 🚭bu fi kenn tox
- 🚯bu fi kenn sànni mbalit
- 🚱ndox mii sellul
- 🚷bu kenn dox jaar fii
- 📵dañu fi tere portaabal
- 🔞ku amul 18 at bokkul
- ☢️radioaktif
- ☣️risku-bio
- ⬆️fettu kaw
- ↗️fettu ndijooru kaw
- ➡️fettu ndijoor
- ↘️suuf-ndijoor fett
- ⬇️fettu suuf
- ↙️suuf-càmmoñ fett
- ⬅️fettu càmmoñ
- ↖️fettu càmmoñu-kaw
- ↕️fettu suufu-kaw
- ↔️fettu càmmoñu-ndijoor
- ↩️fettu ndijoor lemoo càmmoñ
- ↪️fettu càmmoñ lemoo ndijoor
- ⤴️fettu ndijoor lemoo kaw
- ⤵️fettu ndijoor lemoo suuf
- 🔃fett yu ci yoonu montar
- 🔄bitoŋu fett yu juuyoo te safaan-montar
- 🔙fettu DELLU
- 🔚fettu JEEX
- 🔛fettu ci TAAL
- 🔜fettu CI KANAM
- 🔝fettu COLLU
- 🛐barabu jaamukaay
- ⚛️màndarga atom
- 🕉️om
- ✡️biddeew of Dawuda
- ☸️pëno dharma
- ☯️yin yang
- ✝️kruwaa lateŋ
- ☦️kruwaa ortodoks
- ☪️biddeew ak weer
- ☮️màndarga jàmm
- 🕎menorah
- 🔯biddéewu 6 car
- ♈Kuy
- ♉Nag wu góor
- ♊Jemóo
- ♋Kàŋseer
- ♌Gaynde
- ♍Wiyerse
- ♎Balaas
- ♏Eskorpiyoŋ
- ♐Sajiteer
- ♑Kaprikorn
- ♒Wersóo
- ♓Jën yi
- ⛎U buñ baare
- 🔀bitoŋu jaxase way yi
- 🔁bitoŋu baamtu
- 🔂bitoŋu benn baamtu
- ▶️bitoŋu doxal
- ⏩bitoŋu jëmale kanam gaaw
- ⏭️bitoŋu way wi topp
- ⏯️bitoŋu doxal wala taxawal
- ◀️bitoŋu delloo ginaaw
- ⏪bitoŋu delloo ginaaw gaaw
- ⏮️bitoŋu way wi mujj
- 🔼bitoŋu yéegal
- ⏫bitoŋu gaawal yéegal
- 🔽bitoŋu wàcce
- ⏬bitoŋu gaawal wàcce
- ⏸️bitoŋu taxawal
- ⏹️bitoŋu dakkal
- ⏺️bitoŋu enregistare
- ⏏️bitoŋu génne
- 🎦sinemaa
- 🔅bitoŋu lëndëm
- 🔆bitoŋu leeraay
- 📶baari reso
- 📳anamu wiibrër
- 📴portaabal buñ fay
- ♀️màndarga jigéen
- ♂️màndarga góor
- ✖️x fuul bu rëy
- ➕màndargay yokk bu rëy
- ➖màndargay wàññi bu rëy
- ➗màndargay xaajale bu rëy
- ‼️ñaarte màndarga esklamaasiyoŋ
- ⁉️màndarga esklamaasiyoŋ laajte
- ❓tombu laajte
- ❔tombu laajte bu weex
- ❕tombu esklamaasiyoŋ bu weex
- ❗tombu esklamaasiyoŋ
- 〰️tiire ondule
- 💱wecci koppar
- 💲màndarga dolaar bu dijj
- ⚕️màndarga medsin
- ♻️màndarga defaraat
- ⚜️flëru-lis
- 🔱xeeju ñatti bopp
- 📛badsu tur
- 🔰màndarga sapone, soog a door
- ⭕sarkal bu rëy te diis
- ✅màndarga nangu bu weex te rëy
- ☑️kaasu boyet ak xàmme
- ✔️màndarga nangu bu rëy
- ❌kruwaa
- ❎bitoŋ kruwaa
- ➰buum gu lemu benn yoon
- ➿buum gu lemu ñaari yoon
- 〽️màndarga beneen wàll
- ✳️asterisk bu 8 car
- ✴️biddeewu 8 cat
- ❇️eklaa
- ©️àqu moomeel
- ®️bindu na
- ™️turu liggéey
- 🔠mbind lateŋ, majiskil
- 🔡mbind lateŋ, miniskil
- 🔢mbindu nimero
- 🔣màndargay mbind
- 🔤arafi mbindu lateŋ
- 🅰️bitoŋu A (xeetu deret)
- 🆎bitoŋu AB (xeetu deret)
- 🅱️bitoŋu B (xeetu deret)
- 🆑bitoŋu CL
- 🆒bitoŋu KUUL
- 🆓bitoŋu AMUL FAY
- ℹ️info (xibaar)
- 🆔bitoŋu ID (dàntite)
- Ⓜ️M bu wërale serkal
- 🆕bitoŋu BEES
- 🆖bitoŋu NG
- 🅾️bitoŋ O (xeetu deret)
- 🆗bitoŋu waaw-kay
- 🅿️bitoŋu P
- 🆘bitoŋu WALLU
- 🆙bitoŋu YEEGAL
- 🆚bitoŋu daje
- 🈁bitoŋu "fii" bu sapoŋ
- 🈂️bitoŋu "dafa am juuti" bu sapoŋ
- 🈷️bitoŋu sapone "lu ñuy fay weer"
- 🈶bitoŋu sapone "dafa am juuti"
- 🈯bitoŋu "amna boroom" bu sapoŋ
- 🉐bitoŋu "waxaale" bu sapoŋ
- 🈹bitoŋu "wàññi" bu sapoŋ
- 🈚bitoŋu "amul juuti" bu sapoŋ
- 🈲bitoŋu "dañu koy tere" bu sapoŋ
- 🉑bitoŋu "terewu ñu ko" bu sapoŋ
- 🈸bitoŋu "jëfekaay" bu sapoŋ
- 🈴bitoŋu "jàll klaas" bu sapoŋ
- 🈳bitoŋu "wakaas" bu sapoŋ
- ㊗️bitoŋu "ndokkale" bu sapoŋ
- ㊙️bitoŋu "sekkere" bu sapoŋ
- 🈺bitoŋ "ku bëgg liggéey" bu sapoŋ
- 🈵bitoŋu "amul wakaas" bu sapoŋ
- 🔴serkal xonk
- 🔵serkal baxa
- ⚫serkal ñuul
- ⚪serkal bu weex
- ⬛kaare bu rëy te ñuul
- ⬜kaare bu rëy te weex
- ◼️kaare bu yam te ñuul
- ◻️kaare bu yam te weex
- ◾kaare yam-ndaw te ñuul
- ◽kaare yam-ndaw te weex
- ▪️kaare bu ndaw te ñuul
- ▫️kaare bu ndaw te weex
- 🔶karo rëy oraas
- 🔷karo rëy baxa
- 🔸karo ndaw oraas
- 🔹karo ndaw baxa
- 🔺xonk, tri-àngal, buñ defal tomb
- 🔻tri-àngal xonk muuse jëm suuf
- 💠karo bu ànd ak tomb
- 🔘bitoŋu rajo
- 🔳bitoŋu kaare bu weex
- 🔲bitoŋu kaare ñuul
- 🏁raaya bu am karo damiye
- 🚩raaya am jëmmu tri-yàngal
- 🎌raaya yu féewaloo
- 🏴raaya bu ñuul
- 🏳️raaya bu weex
- 🏳️🌈raaya xon
- 🏻xeesaayu der bu woyof
- 🏼xeesaayu der bu xeereer
- 🏽xeesaayu der bu yam
- 🏾xeesaayu der bu xawa ñuul
- 🏿xeesaayu der bu ñuul
😀 Smileys & Emotions
👋 People & Body
🐵 Animals & Nature
🍇 Food & Drink
🌍 Travel & Places
🎃 Activities
👓 Objects
🏧 Symbols & Signs
🏁 Flags
👋🏻 Skin Tones